![Exil Gaddaay Gi Poemes en Wolof [Broché]](../shopping/images/mini/1316546754.jpg)
Agrandir la Photo |
Exil Gaddaay Gi Poemes en Wolof [Broché] |
Auteur :Ndiaye Daouda
Editeur :
Collection :
Langue: Français
Parution :
Nombre de pages : 94
Dimensions :
Resumé :
e recueil de poèmes en wolof décrit un chemineme suite
|
|
|
|
|
|
|
1 annonces pour ce produit |
|
Neuf |
Gà ddaay rekk dëkke gà ddaay
GÃ ddaay ba nekk fu amul daay
Gà ddaay ba mana sori gà gg gi
Gà ddaay ba mana daw kà dd gi
Gà ddaay kà dd ga ñuy siyaare
Gà ddaay gedd la ñuy tasaare
Gà ddaay baaxoo wërum réew
Gà ddaay rekk bañ ku la yéew
Gà ddaay ba far tà bbi ci dun
GÃ ddaay ba far tebbi lu duun
Gà ddaay ba fa ñi la xañub dund
GÃ ddaay dund fa sa giiru-dund
GÃ ddaay defar sa gentu baay
Gà ddaay dëggal sa géntu yaay
Gà ddaay rekk dëkke gà ddaay
GÃ ddaay ba nekk fu amul daay
|
|
Poser une question |
|
|
 |
|
|
|
|
|
|
|
Descriptif du Produit |
e recueil de poèmes en wolof décrit un cheminement personnel. En quête de paix dans un monde injuste, l'auteur nous fait rencontrer des hommes insatisfaits de leur sort, partagés entre la crainte et l'espoir de vivre. Tout exil exige en amont un rituel, une offrande, un sacrifice. et c'est à l'ombre du baobab, temple mythique et mystique de la parole que l'auteur fit son offrande lyrique. |
|
|
|
|
|
|
|
|
Hébergez vos sites chez Sigata et soyez plus
competitifs !!!! |
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
Moyens de Paiement Acceptés |
|
|
|
|
|